Bii jukki ab junj rekk la. Man nga cee duggal sa loxo, suqali ko, ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wikipedia taxawal.
Saara: yayAfrig Saara ab màndiŋ la, mu ngi soxal Afrig gu bëj-gànnaar. Ak 9.200.000 km2, mooy màndiŋ bi gën a mag ci àddina si, te mooy ñetteelu màndiŋ bi gën a mag ci àddina si, gën a tuuti màndiŋ yi nekk ci Antartika ak bëj-gànnaaru Artiku rekk.