Aller au contenu

Rabat

Jóge Wikipedia.
Rabat
الرباط
ⵕⵕⴱⴰⵟ
Skyline of {{{official_name}}}
Réew Marok
DiiwaanRabat-Salé-Zemmour-Zaër
Tus-wu-gaar
Tus-wu-taxaw
34° 1′ 31″ Bëj-gànnaar
     6° 50′ 10″ Sowwu
/ 34.02528, -6.83611
Kawewaay11 m
way-dëkk1 787 307 nit
atum way-dëkk2 009
Rëyaay1 088 km²
DIggu Rabat

Rabat (di الرباط ar-Ribat ci araab) mooy péeyu Nguurug Marok, mooy ñaareelu dëkk bi ëppi nit ca nguur ga. Mi ngi nekk ci wetu tefesu mbàmbulaanug Atlas gi. Ca jamono-ju-yàgg ja lañu fa tambalee dëkk. Ñoo ngi ko sos, dëgg-dëgg, ci 1150.